Teuss - Temoignage de Adama Amar Propriétaire de l'appart du drame des Maristes

Teuss - Temoignage de Adama Amar Propriétaire de l'appart du drame des Maristes

Commentaires

  • diabar sakh légi worole

    Ibra NdiayeIbra NdiayeIl y a 2 jours
  • kou ray nit te tay ko dagnoula wara ray

    Mamadou Mouhamed BaMamadou Mouhamed BaIl y a 2 jours
    • yalla moko wakh dhee dou mane

      Mamadou Mouhamed BaMamadou Mouhamed BaIl y a 2 jours
  • Femme bi daffa reww kessé. May wahh Aladji di diaye graww té warra wahh deugg nane doundame mo diéhh. Thipppp

    Thioro MbayeThioro MbayeIl y a 2 jours
  • Li yeup seuytané rek la wakh deug yalla khéyna seuytané dagua meun rek

    Bineta GueyeBineta GueyeIl y a 3 jours
  • Sa adina. Yakouna bâ yallah sounou borom diapela

    ndeye fatou diengndeye fatou diengIl y a 3 jours
  • Gor day matt gor wayé am sa soxna mou yilif la loumou wax nganni wàw ñiak fayda rek thiimm

    Saliou FayeSaliou FayeIl y a 3 jours
  • Problèmou rèseaux putainnn!!!! Mais sokhnassi deff ngua lou eupeu😔

    Amoon RaAmoon RaIl y a 3 jours
  • Justice soit faite

    Safietou DialloSafietou DialloIl y a 3 jours
  • Mo kham dé beug lou nékh sa serign bou takhé dome bou doff bouma ame diokhla so déwé saye wadiour perte mome dess akk diabotame

    Khady DiengKhady DiengIl y a 4 jours
  • Vraiment les sénégalais sont hypocrites,une femme qui assassine son époux et vous vous permettez de l'eloger.aucune cause ne peut justifier un tel acte

    nita dioufnita dioufIl y a 4 jours
  • Vraiment c'est horrible une femme dafa wara tey mane je suis enceinte et j'ai su que mon mari me trompe mais je l'ai réglé calmement sans que personne n'est au courant mais mome moy rousse rek

    Diop AwaDiop AwaIl y a 4 jours
    • tu vient de nous mettre au courant 😒

      cisse familycisse familyIl y a jour
  • Seytane aka gaaw entre l'amour et la haine il n'y a qu'un pas

    ASS DIONGUEASS DIONGUEIl y a 4 jours
  • Saway arretez vos conneries a la senegalese, ne nous fatiguez pas avec vos histoires de rafétal, Soyons pas des nafékheux. Cette femme est une criminelle. Qu'elle aille crever en prison comme une vulgaire criminelle.

    Abazi NdiayeAbazi NdiayeIl y a 4 jours
  • Ahmed dafa seytané avec sa grande gueule

    Binta Diallo BadjiBinta Diallo BadjiIl y a 4 jours
  • Elle mérite d'être emprisonnés à vie

    Bineta SyBineta SyIl y a 4 jours
  • Deugla ki loumou def niaw na ba si kanamou yalla mais kou kheuy na ga mouslou si cheytaner li serigne cheick tidjiane wah deugla rap you bone ya gi senegal moytoulen thiow surtout les femmes

    fatou gueyefatou gueyeIl y a 5 jours
  • Parlons de ces sappeurs qui n,interviennent jamais à temps ,qui ne sauvent jamais qui que soit ,qui ne répondent jamais au téléphone et qui malheureusement.........

    Abo DiopAbo DiopIl y a 5 jours
  • Kikaye da tite motakh mou matou ak kanamame bou dangue biiii limou yakeuh mo reuy kiii dagnako wara topou bam seus pask d'apres li wadji wakh ki dako prépareiwone essence amoul loumouy deif si keur gui sou deug neikhei reik

    FABI MBOUPFABI MBOUPIl y a 5 jours
  • adou na dal doy na warr

    Lucas OliveiraLucas OliveiraIl y a 5 jours
  • Kou deh ya perte kholal kignu Ray bapare niewfi nane kou jiguen ki dafa bakh ki sunekon jamono yonente bi dankoy Ray joulit day mougn

    Ibrahima DiaIbrahima DiaIl y a 5 jours
  • Libéré ngaka blindé avec ça Guen Di critique macky Sall gniko Yi mo yaku

    Ibrahima DiaIbrahima DiaIl y a 5 jours
  • Man declou ndoye ban moman genel ndakh mom ragaloule ta d'où far feen li am la y wa

    Khady PouyeKhady PouyeIl y a 5 jours
  • Waw man warouwma des amna mbok kiniou ray Guen ma y wakh bok ray nit dafa eup gen di wakh mandou bilahi cou def nit lou bon yala alakla a met Aidara khometoumala invibi limouwakh tegouko feen ak louniou ma a diote li waroule won

    Khady PouyeKhady PouyeIl y a 5 jours
  • Bilahi Senegal mo bari na fekh wakhoulene fi dara loudoul defendre femme bi

    Ibrahima NdongIbrahima NdongIl y a 5 jours
  • Gni gno seytané maye wakhe mouné famille bi khalatoul plainte. Vraiment Sénégal amoul loi 😒

    arlette gomisarlette gomisIl y a 5 jours
  • SUNU BOROM KHAMOUL KI DOMOU SERIGNE LA WALA DOMOU YONÉNTI LA. YALLA KOU DÉFF BAKAR LA KHAM. ET LA LOI EST AU DESSUS DE TOUT ET DE TOUS ...BAYILÈN THIAKHANE YI KI LOUMOU DEF KÈNN MOUNOUKO JUSTIFIÉ

    Secret femme africaineSecret femme africaineIl y a 5 jours
  • Yen ay nafek nguen djiguenbi kou bone la sekoul dara ak serigne touba

    Ndiaye2 MossaNdiaye2 MossaIl y a 5 jours
  • Ak lou mene khéw bou rayone sa rak do wakhé ni ak nomou mene sante raye mome dou yone

    Adji DiopAdji DiopIl y a 5 jours
  • Doyna war dal li métina trop

    Modou DiengModou DiengIl y a 5 jours
  • teudjleen ko ma damisi diabi dji les femmes daniouma diakhal sunu dike di fitnal sene dieukeur yi paré legui sou ame kenen wala mouy dokhan niou commence jalousie topatoleen sene dieukeur yi mo gueneu de ndakh goor mom foumou ame diame rek lay weur wasalam

    Alad FayeeAlad FayeeIl y a 5 jours
  • Dieu l'omniscient a décrété la polygamie La polygamie est culturelle mais elle n'est pas naturelle Les sociétés occidentales où se pratique la culture de la monogamie ont le taux de polygames beaucoup plus élevé que les sociétés musulmanes où la polygamie est autorisée

    Cheikh SeckCheikh SeckIl y a 6 jours
  • Waw taximan bi bagne dou niou si wakh tamite

    Mareme Gueye GueyeMareme Gueye GueyeIl y a 6 jours
    • Khana thiey

      DarkChannel FallDarkChannel FallIl y a 5 jours
  • Mansour bayil khél yalla nafékh bakhol dé🙊

    borom xasss xasssborom xasss xasssIl y a 6 jours
  • Man dé dioména serigne dafay défff lo rafet😡😡😡

    borom xasss xasssborom xasss xasssIl y a 6 jours
  • Danio rayul sen mbokk rek

    khoudia diakhatekhoudia diakhateIl y a 6 jours
  • Ki soxore na trop

    bb chou galaxys1bb chou galaxys1Il y a 6 jours
  • Mais ce meutre est premedité il faut le procureur fait un conference de presse...fi ya pa de masla c tun meutre ...

    OXFOR BIMEOXFOR BIMEIl y a 6 jours
    • Tŕé franchement kelk soit l motif ca n justifie pa cet act inhumain

      Madoune GueyeMadoune GueyeIl y a 5 jours
  • Li ma si mètti moy legui gnou outal femme bi papiers doff tè dara diotouko

    Niang SayeNiang SayeIl y a 6 jours
  • Aarretez de la defendre...on s'en fou de son pere....il na k etre le president, n'empeche que c1 criminel.

    Fatima SyFatima SyIl y a 6 jours
  • Toi le bailleur y’a wara mandou en premier. Comment tu peux raconter une scène alors que tu es arrivé bien après les faits.

    iba ritoiba ritoIl y a 6 jours
  • Bilahi Mansour vrai na fekh la ki ray ga wara wakh degeu né yala nena kou ray niou ray la ganane doundame mo diekh yaw alhourane diangeu diakhale nama mais li Gaston mbengue degeu la vrai na fhéh ga

    Diakhate CheikhnaDiakhate CheikhnaIl y a 6 jours
  • Mais arrêtez avec son père bayame santou koko raye lowou koko la fille est une citoyenne lameda justice sera fait inchalla je ne connais pas ni le père ni la famille de la fille

    fatourassoul S Gfatourassoul S GIl y a 6 jours
  • Bayilen massla bi famme bi bakhol dafa wara dee ci kasobi

    Amar BeyeAmar BeyeIl y a 6 jours
    • Allah y’a rahmou c est très triste de mourir de cette façon Qu Allah la rahmou amine

      Haby DraméHaby DraméIl y a 5 jours
  • Societe bou depressive

    Birame NdiayeBirame NdiayeIl y a 6 jours
  • Elle doit recevoir une evaluation psychiatrique ... une femme enceinte ou post partum souffre souvent de la dépression nerveuse et peut faire des choses horribles.... beaucoup de cas similaires dans le monde... souvent la Victime est très proche ( époux, enfants).

    nayida4evernayida4everIl y a 6 jours
    • doule. Pas dexcuse. elle doit mourir

      kholl moustapha lokholl moustapha loIl y a 2 jours
  • nagnko déff noume déff dieukeurem wakhdji diékh, bayléne nafékh ndogali yalla bosi talsa dieukeur, nitt kounéke nakol bopal bakane dafa for , yalla nagnou yalla mousal ciili.yalla kharéko aldiana.

    Fatou DiakhitéFatou DiakhitéIl y a 6 jours
  • N'importe quoi? Mais le Sénégal va mal, si elle a tué une personne il faut pas lui trouver des justifications...nous sommes tous égaux en droit, arrêtez de parler et laissez la loi faire son travail. Fille de marabout ou pas , il faudra que justice soit faite. Que la loi éclaire ce fait déplorable et intolérable.

    Khady DIEYEKhady DIEYEIl y a 6 jours
  • Senegal mo bary nafek ki danio wara rey ndeyame c t un criminel

    papa soWpapa soWIl y a 6 jours
  • Té yala takh nith gni delolen sen xel Thi yala nii saytane dafa barrí dole te beupe Senegalais bou nek fii khamo sa eulekk nith Boy wakh na wakh loouko worr laniou sekkk Ba saytane niaw yala rek moko xam ak niar ngiko sekk kou xamoul sa eulekk nakk teyal Thi wakh dji , niou nian yala sam niou sam len , wa salam

    Brasil DakarBrasil DakarIl y a 6 jours
  • Liyeupe seuyou appartement mokoye indi

    Barbara BaBarbara BaIl y a 6 jours
Teuss - Temoignage de Adama Amar Propriétaire de l'appart du drame des Maristes